0) Si vous n'êtes pas encore enregistrés vous pouvez seulement lire les messages du forum sans répondre
1) Vous DEVEZ VOUS ENREGISTRER sur le forum pour répondre aux messages déjà présents ou pour en créer des nouveaux.
2) Vous êtes enregistrés, alors vous pouvez participer au forum.
Pour se faire, rien de plus simple :
POUR UN NOUVEAU SUJET :
- cliquez sur une rubrique (exemple "discussion")
- cliquez sur "Nouveau sujet", une page "Poster un nouveau sujet" apparait.
Vous pouvez alors écrire le titre ou objet de votre message et en dessous
le contenu de celui-ci...
- pour finir cliquez sur le bouton "envoyer" (en bas de la page) pour valider votre message sur le forum.
POUR RÉPONDRE A UN MESSAGE EXISTANT
- cliquez sur une rubrique (exemple "photos de soirées")
- cliquez sur le message que vous voulez lire.
- cliquez alors sur le bouton "Répondre" (en bas du message), une page "Poster une réponse" apparait ...
Vous pouvez alors écrire votre réponse.
- pour finir cliquez sur le bouton "envoyer" (en bas de la page) pour valider votre réponse.
et bien maintenant !! à vous de jouer
qui parle de parité parle d'égalité.bounou démé bay wax gnou yamalé goor ak djiguénn c parck, kii dii goor dafa diokhatoul djiguenn accam, diokhatouko lii mou yélol bé taxna amna diamano yo kham né banou thia tollo kenn massoul khékh parité. LUTAX kenn khékhouko? ndax yenn goor dawou léenn wax yonn konn nak yakkar naani waar guéna sétatt seén bopp bou bax ndaw défois guénn dialgatii lolo waral gnouy sett parité founou tool
Eupeuleuw , ma sister yaangui todj forum bi laa wax , mais nakk faut faire tres attention par rapoort a certains termes comme parité , egalité , et autres car yalla yémaléwoul dara konn dou nitt mooy nieuw ni li yalla défoul moom moo koy deff. comprehension oblige lol
gaa lou wèer gua wax souguèenn ko xolè fofou rekk daay mèti egalitè manoul nek cii goor ak djiguèenn ndax alla yamalèwoul ta bindouko fènn wayè lii waral gnouy khèkh paritè moy dioxatulenn djiguenn yèlèfam ba taxna d'une part on sens dè fois d'etre ignorè dans la socitè ou meme ecartèà vrè dire
oui tu as raison si loolou , adouna moo diaffé banga khamni waayé nakk deff sa waal si keur gui waroul takh ngay diir goor gu wag , deff ko nguir doom yinga kham ni dangalenn fi diour té nga beug niou doon dara euleuk té loolou doufi meuss diougué .
Répondre:
Ensemble des thèmes: 7 Ensemble des articles: 27 Ensemble des utilisateurs: 14 Actuellement en ligne (Utilisateurs enregistrés): Personne